Song Daan lyrics

Songs   2024-12-21 00:20:16

Song Daan lyrics

Dooley nit kou ñuul kou, ko beug xam la

Mbeur mouy daan kou

Ko beug xam démal lathi ko you

Woma woma Ci leundeum, dinala Wouyou

Oubil sama, xol dinga

Xam nimou sédéé ci you

Fileg mang lay am, sama xol

Luma songù, daan ko

Fileg mang lay am, sama Xèll

Luma songù, daan ko

Songù Daan Koooooooo

Songù Daan Koooooooo

Songù Daan Koooooooo

Songù Daan Koooooooo

Man Maanan, mane iiow laa

Liow nga naan, ngané man leuh

Man Maanan, mane iiow laa

Liow nga naan, ngané man leuh, éh éh éh

Béneu biss dina niow, mou melni louniouy nétali

Mou melni lii dou anhhhhhhh

Té ken Du jog, naan man mi nako fékéh yoooo

Ndah nguelaw lii daaw diñou yobalé

Xoob yiy russ ci garab guii

Ah lifi xew tay bouniou ko fatéé

Africa Dom yiy wane, sén bopeuh

Fileg mang lay am, sama xol

Luma songù, daan ko

Fileg mang lay am, sama Xèll

Luma songù, daan ko

Songù Daan Koooooooo

Songù Daan Koooooooo

Songù Daan Koooooooo

Songù Daan Koooooooo

Man Maanan, mane iiow laa

Liow nga naan, ngané man leuh

Man Maanan, mane iiow laa

liow nga naan, ngané man leuh éh éh éh éh

Cí Díg bï Fofou, laay diar Mù am xàl

Safara douma daaw

Los angeles Paris ba Rio

New Delhi London Tokyo

Sêdoog Yén Liñu, Jēlé Fénéne

Fi niou, diarr ñun ba éksi fí

Dafa mèlni, louńou nétali

Los angeles Paris ba Rio

New Delhi London Tokyo

Sêdoog Yén Liniou

Jēlé Fénén Éh Éh hh hhhh hhhh

Maa contaane, yoow it yaa contaaan

Maleu geuuneuu contane, uhh Yeahhhhh hhhhh

Contane yeahhh yeeaahhh

Contane yeahhh

Contane yeahhh

Akon Yousou Yeah

Akon Yousou Yeah

Cí Díg bï Fofù, laay diar Mù am xàl

Safara douma daaw

Los angeles Paris ba Rio

New Delhi London Tokyo

Sêdoog Yén Liñu

Jēlé Fénéne

Fi niou, diarr ñun ba éksi fí

Dafa mèlni, louńou nétali

Los angeles Paris ba Rio

New Delhi London Tokyo

Sêdoog Yén Liniou

Jēlé Fénéne

See more
Youssou N’Dour more
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof, French, English, Unknown
  • Genre:Singer-songwriter
  • Official site:http://www.youssou.com/
  • Wiki:http://fr.wikipedia.org/wiki/Youssou_N%E2%80%99Dour
Youssou N’Dour Lyrics more
Youssou N’Dour Featuring Lyrics more
Youssou N’Dour Also Performed Pyrics more
Excellent Songs recommendation
Popular Songs
Copyright 2023-2024 - www.lyricf.com All Rights Reserved