Doundou Oundou lyrics

Songs   2024-12-28 13:05:59

Doundou Oundou lyrics

Ba gni nekk boy lignou done doundou aka doy war

Ba tay souma koy wakh damay réh ba djoy

Souma kholé lignou dane def dagno beugone yeufou gangster

Ba gni nekk boy moussiba rek lagnou dane def

Ba gni nekk boy yeufou oundou rek

Ba gni nekk boy moussiba rek lagnou dane def

Ba gni nekk boy yeufou oundou rek

Ba tay dé magg nagnou

Sa youmay dem école dagn may door ma yéwou

Té souma démoulé école fadjaar tél lay yéwou

Dougou kogne ba wala dem ba Niaye rek tokfa

Mane ak sama gars yi khol kou gueuneu kaagne gnou togne ko

Ba heurou ndéki am gnou délou waat sen galé ndéki

Gnou niakk controle chaque jour cii biti lagni ndéké

Outi féraille. lokoy doyé? no dama koy djaay

Bouteille, preum, armignon père dakal mou nieuw

Xaliss dougnouko khar mou nieuw no da am yone

Baabi, pile, perpé, dayce (Dé), xaliss xaliss, pot égatte

Fo ba xotti sa yééré swagg soudé dall

Kou tchii gueunone guerrier fok gnou coup d'état la

Ba gni nekk boy lignou done doundou aka doy war

Ba tay souma koy wakh damay réh ba djoy

Souma kholé lignou dane def dagno beugone yeufou gangster

Ba gni nekk boy moussiba rek lagnou dane def

Ba gni nekk boy yeufou oundou rek

Ba gni nekk boy moussiba rek lagnou dane def

Ba gni nekk boy yeufou oundou rek

Ba tay dé magg nagnou

Yallah gnou aar, ndakh fougnou diar, mbede dou yaar

Forr cigarette guéné sakhar, beuri nullard

Eufeul ay xathie, langg camion, taxi, cassambaar

Neubeul ni naar, beuri cica (cicatrice) peundeul yambaar

Tournoi potou méw, rayanté ndakh bène kopp wéégne

Boy bi bougnou topoté fou magg yi dem niou topp lène

Guel bo dokhane sou bagné nga nokk ko bamou xam

Sangou cii ndoxou taw, def sieste cii biir ay mbaarou kharr

(Mouton)

Tardé agne tibeu, boudé teud feug

Wa galé commencé guiss né ni sen fils sa ngui deung

Dagn lay interné, dieundeul la play ba internet

Bo gnak chance deugg for ever mbédeu lay hébergé

Ba gni nekk boy lignou done doundou aka doy war

Ba tay souma koy wakh damay réh ba djoy

Souma kholé lignou dane def dagno beugone yeufou gangster

Ba gni nekk boy moussiba rek lagnou dane def

Ba gni nekk boy yeufou oundou rek

Ba gni nekk boy moussiba rek lagnou dane def

Ba gni nekk boy yeufou oundou rek

Ba tay dé magg nagnou

It goes out for my niggaz yima fowa ndol

Gnima bokka lone kogne

Gnima nékalone école primaire

Meunouma dem fatélène

Amoul lougnou défoul, amoul lougnou défoul

Xawouma lougnou défoul, waxma gaff bougnou défoul

Beuré bougnou démoul, béré bougnou lékoul

Goune dagnou dane sananté kherr di guerre

Saganté kherr di réééh hann anyway

Nokanté everyday yeah

Beuri, leudj, dakanté périééé, taf dokk, baskulé

Motakh ma nane la

Ba gni nekk boy lignou done doundou aka doy war

Ba tay souma koy wakh damay réh ba djoy

Souma kholé lignou dane def dagno beugone yeufou gangster

Ba gni nekk boy moussiba rek lagnou dane def

Ba gni nekk boy yeufou oundou rek

Ba gni nekk boy moussiba rek lagnou dane def

Ba gni nekk boy yeufou oundou rek

Ba tay dé magg nagnou

See more
Dip Doundou Guiss more
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof, French, English
  • Genre:Electronica, Hip-Hop/Rap, Pop, R&B/Soul
  • Official site:https://www.instagram.com/dip_doundouguissofficiel/
  • Wiki:
Dip Doundou Guiss Lyrics more
Dip Doundou Guiss Featuring Lyrics more
Excellent Songs recommendation
Popular Songs
Copyright 2023-2024 - www.lyricf.com All Rights Reserved