Fayeku lyrics

Songs   2024-12-28 12:53:23

Fayeku lyrics

Fayeku

Ngay comptél mane may pesé khaliss

Mangui 8e assamane di guiss niane yi yaw yangui 5e etage

Woté negn mbolo pour rayma ndax li legn dèssé mattou

unité telecentre

Niom daniou tella ndiol yeukhé magg

Niom da niou niou yeukhé yoor tella niakk

Tekele ma ak yene boy yi moy tekele

Kerr ak naadj tekele gainde a khadj

Maouti wo na ko mai nango gou ma dieul khamna damkay msage

Waayé soumay dieulsi samay noone ak

Séni djiégué niaalé may ndieuk djaalé

Chien méchant nga nn do chef de gang

Chef de chantier mo geune chef de chambre

Diagg nga dou tou niou la big up*

Ma nigga thiat dougouleu da la bireul

May len lokho niou yotou sama rouu

Mangui ak khirr bi nè legn niou kheuffeulou

Xekh nga beug boul kharr niou eufoul niou

Amo drapeau ba di kheuthio

Yalla ak yalli lane moy taxx may roukh

Meme bou fenn amoul wone ken dou dioubb

Guelouwar dou ma tallal lokho moukk

Yelowane wou ma damay fayekou

Respect bi defko khaliss

Mane khamna yonou banque

Beugouma dem fou soriwoul

Motakh khawouma yonou diam

Diam dji defko business

Sauf bou fekei seu fite dess

Missionéi caissou Bill Gâtes

Khaliss dou déé même souy diekh

Fayekou liquide mba fayekou chèque

Fayekou souba non fayekou tay

Fayekou djouni mba fayekou ten

Bo ma fayoul lou cheroul nga fayma lou cher

Fayekou liquide mba fayekou chèque

Fayekou souba non fayekou tay

Fayekou djouni mba fayekou ten

Bo ma fayoul lou cheroul nga fayma lou cher

Deugeur tei deudj ni dreudj, leundeum ni deudj

Chaque jour la chaque njaabot bou ndol di dadj

Kou geum ni sa niak moy sa weurseuk, reuthie tekki faté lep

lofi daadj

Sa geum niouy taxx ngay job di khagne sa

Bopp nelaw niouy daadj sa lallou hopital

Mbeugeul dou diay dou déé bou yebo do

Meusso guiss nmbeugeul bou taadj si boll agne

Kou nè na nga woutil xam xam bala am

Neko pour mou wone la keur kocc barma

Guiss na fi yeungeul geusseum sa taat ba jarr

Far yeungeul geusseum lou nekk sa compte banque

Fou thiat di eup geudd taww

Imam bi keupou caissou jaaka

Ribat si poche presi ak ribat si gordjiguen am liberté batt

rekk

Ligueyel té nguirr chèque

Lou lew neuw ni guiss vierge

Bougouniou tedd si pett

Religion bi bussiness

Hypocrite nga fuck sa love ak peace

Bala ngamay thiop ma thiop sa khiff

Forr sikim ni kou joudo si siiifff

Ken si niom denthioul djourom brique

Respect bi defko khaliss

Mane khamna yonou banque

Beugouma Dem fou soriwoul

Motakh khawouma yonou diam

Diam dji defko business

Sauf bou fekei seu fite dess

Missionéi caissou Bill Gâtes

Khaliss dou déé même souy diekh

Fayekou liquide mba fayekou chèque

Fayekou souba non fayekou tay

Fayekou djouni mba fayekou ten

Bo ma fayoul lou cheroul nga fayma lou cher

Fayekou liquide mba fayekou chèque

Fayekou souba non fayekou tay

Fayekou djouni mba fayekou ten

Bo ma fayoul lou cheroul nga fayma lou cher

See more
Dip Doundou Guiss more
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof, French, English
  • Genre:Electronica, Hip-Hop/Rap, Pop, R&B/Soul
  • Official site:https://www.instagram.com/dip_doundouguissofficiel/
  • Wiki:
Dip Doundou Guiss Lyrics more
Dip Doundou Guiss Featuring Lyrics more
Excellent Songs recommendation
Popular Songs
Copyright 2023-2024 - www.lyricf.com All Rights Reserved