Niou Dem Mairie lyrics

Songs   2025-01-07 05:36:23

Niou Dem Mairie lyrics

Bokoulok gniy door

Li goor yi di bari bari amo thi dé dénda ndo

Léme bougnou soukeur

Kouko xass moss daal

Dou yombeu bayi ko

Yaw danga meune mine mokal jiguéne

Mani danga rax ndax li dou néne

Beut yi gueuthie na taa ndax yaw

Xol bi deuké naate ndax yaw

Yéndo di rétaane ndax yaw

Namuma greffage ndax yaw

Faléwuma maquillage ndax yaw

Diotna gnou mariage maak yaw

Baby kaay gnaane si

Dieundeu gouro Paa bi takeu seuye bi

Lima beug moy niou dem mairie

Dem mairie, niou dem mairie

Baby kaay gnaane si

Dieundeu gouro Paa bi takeu seuye bi

Lima beug moy niou dem mairie

Dem mairie, niou dem mairie

Yaye sama titi tara pararapa para para

Li mbeuguelou moumeu le diaroul di wax ndax yaw mi xam nga

Laadiou ma aye milliard

Kilo gouro nga ame diabar

Kone légui lane ngay xaar

Gnoune jiguene seuy moy suñu taar

Beut yi gueuthie na taa ndax yaw

Xol bi deuké naate ndax yaw

Yéndo di rétaane ndax yaw

Namuma greffage ndax yaw

Faléwuma maquillage ndax yaw

Diotna gnou mariage maak yaw

Baby kaay gnaane si

Dieundeu gouro Paa bi takeu seuye bi

Lima beug moy niou dem mairie

Dem mairie niou dem mairie

Baby kaay gnaane si

Dieundeu gouro Paa bi takeu seuye bi

Lima beug moy niou dem mairie

Dem mairie niou dem mairie

Yangui dape sama banekh

Di fathie samay adio

Xam di def lila war

Bolèwo darak thioy

Wayè! wayè am na lou dess

Niou Dem mairie

Niou Dem mairie

Niou Dem mairie

Niou Dem mairie ouuuh oh

Baby kaay gnaane si

Dieundeu gouro Paa bi takeu seuye

Lima beug moy niou dem mairie

Dem mairie niou dem mairie

Baby kaay gnaane si

Dieundeu gouro Paa bi takeu seuye

Lima beug moy niou dem mairie

Dem mairie niou dem mairie

See more
OMG more
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof
  • Genre:
  • Official site:
  • Wiki:
OMG Lyrics more
OMG Featuring Lyrics more
Excellent Songs recommendation
Popular Songs
Copyright 2023-2025 - www.lyricf.com All Rights Reserved