Bandit Bou Lewet lyrics
Bandit Bou Lewet lyrics
Ahn, xale bi dama ko yagg
Bëgg mu may dozé dima jaay neex
Duma rëb di soy jar nama
Tagg sa mame ne ma Mbaye Pékh
Yagg na la wax dama paré
Jarul malay fatali sama jongé
Bandit bu lewet mikër rakay sukkër
Suma paré si yaw doto takk tére
Malay yobu besi kaw
Asamaan waw day gaw
Malay tekk si yonn bu baax
Hé konn ne ma waaw
Hé baby, c'est comment ?
Ñewel ma wan la, c'est comment ?
Man na la yobu si Coma
Mala gëna xam naka la
Mani daf may neex
Di la doff lo, daf may neex
Sangsé don sa laobé
Lëmbël moto daf may neex
Eh daf may neex
Di la doff lo, daf may neex
Ne ma Fatou may sa laobé
Lëmbël vampire dalay neex, ahn!
Oh ah, oh ah
Ku la am mën na la tey bu baax
Oh ah, oh ah
Paré na foy dem yobalema
- Artist:OMG
See more